Reine Des Stars [Original]

Sokhou Bb

0 fans

Sokhou Bb


2:26

 The easy, fast & fun way to learn how to sing: 30DaySinger.com

SN Beat
Reine des stars feuleu
Loufi yeungou nieup d'accord ni man la
(Man la)
Ma teudiou wone done toggu
Kone souma yaké niou xam fima mané
(Meuné)
Ñi di ladj ki ka na?
Yagui am Sokhou BB la Diva
Am buzz défa gouma dara
Ñieup di ma weur pourtant et bien
Je suis la
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Domu Fatick bi maag na
Délou si dieul li mu mom si Game bi
Dama nék sama yone
Yag liguey lu guén feel
Am na ñumay wakh Sokhou Cover rek
Déglul Woma wax ma Ligay Yeuk
Il faut imiter les meilleurs
Pour en devenir UN
C'est normal
Luma guéné mu done Hit
C'est normal
May xalé bi yobuu sen fitt
C'est normal
Dama open si def ay feat
Ça dépend
Xamnga Musique gu Sénégal
Dafa doy waar wayé j'attends tout
Loufi yeungou nieup d'accord ni man la
(Man la)
Ma teudiou wone done toggu
Kone souma yaké niou xam fima mané
(Meuné)
Ñi di ladj ki ka na?
Yagui am Sokhou BB la Diva
Am buzz défa gouma dara
Ñieup di ma weur pourtant et bien
Je suis la
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Sokhou yaw BB
(Sokhou yaw BB)
Ñeuwatt na
Si game bi
Ñeuwatt na mane
Si game bi
Ñeuwatt na
Si game bi
Fans Sokhou Yéh!
Magui ni

 The easy, fast & fun way to learn how to sing: 30DaySinger.com

Written by: Moustapha Diop

Lyrics © Ferdinand Malick Hortala

Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Discuss the Reine Des Stars [Original] Lyrics with the community:

0 Comments

    Citation

    Use the citation below to add these lyrics to your bibliography:

    Style:MLAChicagoAPA

    "Reine Des Stars [Original] Lyrics." Lyrics.com. STANDS4 LLC, 2024. Web. 7 Jun 2024. <https://www.lyrics.com/lyric-lf/14123699/Sokhou+Bb/Reine+Des+Stars+%5BOriginal%5D>.

    Missing lyrics by Sokhou Bb?

    Know any other songs by Sokhou Bb? Don't keep it to yourself!

    Browse Lyrics.com

    Quiz

    Are you a music master?

    »
    In Erasure's hit song A Little Respect, what is the final word in the line: "Soul, I hear you ......"?
    A talking
    B falling
    C shouting
    D calling

    Free, no signup required:

    Add to Chrome

    Get instant explanation for any lyrics that hits you anywhere on the web!

    Free, no signup required:

    Add to Firefox

    Get instant explanation for any acronym or abbreviation that hits you anywhere on the web!

    Sokhou Bb tracks

    On Radio Right Now

    Loading...

    Powered by OnRad.io


    Think you know music? Test your MusicIQ here!